An-Nazi'at · 12/46
Tekki Waxtaan — An-Nazi'at
قَالُوا تِلْكَ إِذًا كَرَّةٌ خَاسِرَةٌ ۝١٢
Qaalu tilka izan karratun khaasirah
📖 Tekkim Wolof
Ña ngay wax naan : “loolu deey yàqule la ! ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 10-14 — An-Nazi'at

10يَقُولُونَ أَإِنَّا لَمَرْدُودُونَ فِي الْحَافِرَةِ
Ña ngay wax naan : “Ndax danuy dundaat ginnaaw dee,
11أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا نَّخِرَةً
ak sax ginnaaw bu nu doonee ay yax yu funux ? ”
12قَالُوا تِلْكَ إِذًا كَرَّةٌ خَاسِرَةٌ
Ña ngay wax naan : “loolu deey yàqule la ! ”
13فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ
loolu ab jàjj la,
14فَإِذَا هُم بِالسَّاهِرَةِ
ñu jekki-jekki rekk ne jaww ci kaw suuf si dekkiwaat.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — An-Nazi'at 12

Simoore An-Nazi'at Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ngay wax naan : “loolu deey yàqule la !…

Simoore Aaya 12/46 — An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nazi'at Dégg, An-Nazi'at Tekki, An-Nazi'at mp3, An-Nazi'at pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers