Al-Infitar · 5/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
عَلِمَتْ نَفْسٌ مَّا قَدَّمَتْ وَأَخَّرَتْ ۝٥
Alimat nafsum maa qaddamat wa akhkharat
📖 Tekkim Wolof
bakkan bu Yàlla sàkk xam na la mu jëkkoona def ak la mu mujja def.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Infitar

3وَإِذَا الْبِحَارُ فُجِّرَتْ
ak saa su géej yi taqaloo,
4وَإِذَا الْقُبُورُ بُعْثِرَتْ
ak saa su bàmmeel ya jaxasoo,
5عَلِمَتْ نَفْسٌ مَّا قَدَّمَتْ وَأَخَّرَتْ
bakkan bu Yàlla sàkk xam na la mu jëkkoona def ak la mu mujja def.
6يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ مَا غَرَّكَ بِرَبِّكَ الْكَرِيمِ
Éy yaw nit ! Ana lan moo la fàbbi ci sa mbiru Boroom, bu Tedd bi,
7الَّذِي خَلَقَكَ فَسَوَّاكَ فَعَدَلَكَ
(sa Boroom) bi la bind yemale la, jekkal la ?
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Infitar 5

Simoore Al-Infitar Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bakkan bu Yàlla sàkk xam na la mu jëkkoona def…

Simoore Aaya 5/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers