Al-Infitar · 6/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ مَا غَرَّكَ بِرَبِّكَ الْكَرِيمِ ۝٦
Yaaa ayyuhal insaaanu maa gharraka bi Rabbikal kareem
📖 Tekkim Wolof
Éy yaw nit ! Ana lan moo la fàbbi ci sa mbiru Boroom, bu Tedd bi,

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Infitar

4وَإِذَا الْقُبُورُ بُعْثِرَتْ
ak saa su bàmmeel ya jaxasoo,
5عَلِمَتْ نَفْسٌ مَّا قَدَّمَتْ وَأَخَّرَتْ
bakkan bu Yàlla sàkk xam na la mu jëkkoona def ak la mu mujja def.
6يَا أَيُّهَا الْإِنسَانُ مَا غَرَّكَ بِرَبِّكَ الْكَرِيمِ
Éy yaw nit ! Ana lan moo la fàbbi ci sa mbiru Boroom, bu Tedd bi,
7الَّذِي خَلَقَكَ فَسَوَّاكَ فَعَدَلَكَ
(sa Boroom) bi la bind yemale la, jekkal la ?
8فِي أَيِّ صُورَةٍ مَّا شَاءَ رَكَّبَكَ
Moo la defar ca na mu ko soobe.
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Infitar 6

Simoore Al-Infitar Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yaw nit ! Ana lan moo la fàbbi ci…

Simoore Aaya 6/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers