Al-A'la · 15/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'la
وَذَكَرَ اسْمَ رَبِّهِ فَصَلَّىٰ ۝١٥
Wa zakaras ma Rabbihee fasallaa
📖 Tekkim Wolof
te fàttaliku turu boroomam , tey julli.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-A'la

13ثُمَّ لَا يَمُوتُ فِيهَا وَلَا يَحْيَىٰ
du fa dund dufa dee.
14قَدْ أَفْلَحَ مَن تَزَكَّىٰ
Képp kuy sellal texe na,
15وَذَكَرَ اسْمَ رَبِّهِ فَصَلَّىٰ
te fàttaliku turu boroomam , tey julli.
16بَلْ تُؤْثِرُونَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
Yeen, dangeena bëgg lool dundug àddina,
17وَالْآخِرَةُ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ
te àllaaxira gën te moo gëna sax.
Al-A'laFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-A'la 15

Simoore Al-A'la Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te fàttaliku turu boroomam , tey julli.

Simoore Aaya 15/19 — Simoore Al-A'la الأعلى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'la Dégg, Simoore Al-A'la Tekki, Simoore Al-A'la mp3, Simoore Al-A'la pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers