Al-A'la · 16/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'la
بَلْ تُؤْثِرُونَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا ۝١٦
Bal tu`siroonal hayaatad dunyaa
📖 Tekkim Wolof
Yeen, dangeena bëgg lool dundug àddina,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-A'la

14قَدْ أَفْلَحَ مَن تَزَكَّىٰ
Képp kuy sellal texe na,
15وَذَكَرَ اسْمَ رَبِّهِ فَصَلَّىٰ
te fàttaliku turu boroomam , tey julli.
16بَلْ تُؤْثِرُونَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
Yeen, dangeena bëgg lool dundug àddina,
17وَالْآخِرَةُ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ
te àllaaxira gën te moo gëna sax.
18إِنَّ هَٰذَا لَفِي الصُّحُفِ الْأُولَىٰ
Lii nekk na, ca téere yu jëkk ya,
Al-A'laFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-A'la 16

Simoore Al-A'la Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yeen, dangeena bëgg lool dundug àddina,

Simoore Aaya 16/19 — Simoore Al-A'la الأعلى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'la Dégg, Simoore Al-A'la Tekki, Simoore Al-A'la mp3, Simoore Al-A'la pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers