Al-Balad · 9/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
وَلِسَانًا وَشَفَتَيْنِ ۝٩
Wa lisaananw wa shafatayn
📖 Tekkim Wolof
ak aw làmmiñ ak ñaari tuñ ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Balad

7أَيَحْسَبُ أَن لَّمْ يَرَهُ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ne kenn da koo gisul ?
8أَلَمْ نَجْعَل لَّهُ عَيْنَيْنِ
Moo ndax defalunu ko ñaari gët,
9وَلِسَانًا وَشَفَتَيْنِ
ak aw làmmiñ ak ñaari tuñ ?
10وَهَدَيْنَاهُ النَّجْدَيْنِ
Nu gindi ko tegtal ko ñaari yoon yi, mbaax, mbon.
11فَلَا اقْتَحَمَ الْعَقَبَةَ
Te, moom moo lànka soobu yoon wu tënku wa (mitti) !
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Balad 9

Simoore Al-Balad Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak aw làmmiñ ak ñaari tuñ ?

Simoore Aaya 9/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers