Al-Layl · 20/21
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Layl
إِلَّا ابْتِغَاءَ وَجْهِ رَبِّهِ الْأَعْلَىٰ ۝٢٠
Illab tighaaa`a wajhi rabbihil a `laa
📖 Tekkim Wolof
Lu dul sàkku jëmm Boroomam ja gëna Kawe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-21 — Simoore Al-Layl

18الَّذِي يُؤْتِي مَالَهُ يَتَزَكَّىٰ
kay joxe alalam ngir selal
19وَمَا لِأَحَدٍ عِندَهُ مِن نِّعْمَةٍ تُجْزَىٰ
te amul genn xéewal gu ñuy faye kenn ca moom,
20إِلَّا ابْتِغَاءَ وَجْهِ رَبِّهِ الْأَعْلَىٰ
Lu dul sàkku jëmm Boroomam ja gëna Kawe.
21وَلَسَوْفَ يَرْضَىٰ
Te, xalset naa gëram (moom ka def noona) !
Al-LaylFihi Alxuraan
21Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Layl 20

Simoore Al-Layl Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu dul sàkku jëmm Boroomam ja gëna Kawe.

Simoore Aaya 20/21 — Simoore Al-Layl الليل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Layl Dégg, Simoore Al-Layl Tekki, Simoore Al-Layl mp3, Simoore Al-Layl pdf. Aaya 18–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers