Yunus · 44/109
Tekki Waxtaan — Simoore Yunus
إِنَّ اللَّهَ لَا يَظْلِمُ النَّاسَ شَيْئًا وَلَٰكِنَّ النَّاسَ أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ ٤٤
Transliteration
Innal laaha laa yazlimun naasa shai`anw wa laakin nannaasa anfusahum yazlimoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla nag du tooñ nit ci dara, waaye nit ñi ñooy tooñ seen bopp.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 42-46 — Simoore Yunus
42وَمِنْهُم مَّن يَسْتَمِعُونَ إِلَيْكَ ۚ أَفَأَنتَ تُسْمِعُ الصُّمَّ وَلَوْ كَانُوا لَا يَعْقِلُونَ
Te am na ci ñoom ñu lay déglu. Moo ndax yaw mën nga déggloo ab tëx, doonte la nekkuñu ñu am i xel.
43وَمِنْهُم مَّن يَنظُرُ إِلَيْكَ ۚ أَفَأَنتَ تَهْدِي الْعُمْيَ وَلَوْ كَانُوا لَا يُبْصِرُونَ
Te am na ci ñoom ñu lay xool. Moo ndax dangay gindi gumba, doonte dañu dul gis ?
44إِنَّ اللَّهَ لَا يَظْلِمُ النَّاسَ شَيْئًا وَلَٰكِنَّ النَّاسَ أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ
Yàlla nag du tooñ nit ci dara, waaye nit ñi ñooy tooñ seen bopp.
45وَيَوْمَ يَحْشُرُهُمْ كَأَن لَّمْ يَلْبَثُوا إِلَّا سَاعَةً مِّنَ النَّهَارِ يَتَعَارَفُونَ بَيْنَهُمْ ۚ قَدْ خَسِرَ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِلِقَاءِ اللَّهِ وَمَا كَانُوا مُهْتَدِينَ
Bis bu leen Yàlla dajalee, dana mel ni tooguñu [ca seeni bàmmeel] lu dul diirub benn waxtu cig bëccëg, ñuy xamante. Te ña weddi woon ne dajeek Yàlla dana am, yàqule nañu ndax nekkuñu woon ñu gindiku.
46وَإِمَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِلَيْنَا مَرْجِعُهُمْ ثُمَّ اللَّهُ شَهِيدٌ عَلَىٰ مَا يَفْعَلُونَ
Te Nu won la dara ca la Nu leen tëkkoo, walla Nu rey la [Yaw Muhammad], lu mu ca doon seenug delluwaay ci Nun la jëmsi. Ba noppi, Yàlla nekk di seede ca lañu daan def.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
44Aaya
Tekki — Yunus 44
Simoore Yunus Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla nag du tooñ nit ci dara, waaye nit ñi…Simoore Aaya 44/109 — Simoore Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yunus Dégg, Simoore Yunus Tekki, Simoore Yunus mp3, Simoore Yunus pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Yunus
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Thursday, October 1, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


