Hud · 67/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَأَخَذَ الَّذِينَ ظَلَمُوا الصَّيْحَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دِيَارِهِمْ جَاثِمِينَ ۝٦٧
Wa akhazal lazeena zalamus saihatu fa asbahoo fee diyaarihim jaasimeena
📖 Tekkim Wolof
Ña tooñoon, ag xaacu faagaagal leen. Ñu mujj ne lànjaŋ dee ca seen kër ya,

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Hud

65فَعَقَرُوهَا فَقَالَ تَمَتَّعُوا فِي دَارِكُمْ ثَلَاثَةَ أَيَّامٍ ۖ ذَٰلِكَ وَعْدٌ غَيْرُ مَكْذُوبٍ
Ñu rey ko. Mu ne leen : “Xéewluleen ci seeni kër ñetti fan ! Loolu àpp la bu dul deñ”.
66فَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا صَالِحًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَمِنْ خِزْيِ يَوْمِئِذٍ ۗ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ الْقَوِيُّ الْعَزِيزُ
Ba Sunub dogal agsee, musal Nanu Saalihu ak ña gëm ànd ak moom, - ci Sunu yërmaande - [te musal leen it] ci gàcceg bis booba. Sa Boroom nag, Moom moo di ku bari kàttan, tey Notaakoon ba.
67وَأَخَذَ الَّذِينَ ظَلَمُوا الصَّيْحَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دِيَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Ña tooñoon, ag xaacu faagaagal leen. Ñu mujj ne lànjaŋ dee ca seen kër ya,
68كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۗ أَلَا إِنَّ ثَمُودَ كَفَرُوا رَبَّهُمْ ۗ أَلَا بُعْدًا لِّثَمُودَ
ñu mel ni mësuñu faa sax. Waaw, ndax waa Samuuda weddiwuñu woon seen Boroom ? Moo ndax alkaande dalul waa Samuuda ?
69وَلَقَدْ جَاءَتْ رُسُلُنَا إِبْرَاهِيمَ بِالْبُشْرَىٰ قَالُوا سَلَامًا ۖ قَالَ سَلَامٌ ۖ فَمَا لَبِثَ أَن جَاءَ بِعِجْلٍ حَنِيذٍ
Sunuy ndaw indiloon na Ibraahiima mbégte, ñu ne ko : “Jàmmi Yàlla na nekk ci yaw ! ”. Mu ne leen : “Jàmm ci yéen it ! ”, nis tuut mu indil leen sëll wu ñu wàjj.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Hud 67

Simoore Hud Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña tooñoon, ag xaacu faagaagal leen. Ñu mujj ne lànjaŋ…

Simoore Aaya 67/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers