Ibrahima · 50/52
Tekki Waxtaan — Simoore Ibrahima
سَرَابِيلُهُم مِّن قَطِرَانٍ وَتَغْشَىٰ وُجُوهَهُمُ النَّارُ ۝٥٠
Saraabeeluhum min qatiraaninw wa taghshaa wujoohahumun Naar
📖 Tekkim Wolof
seeni yére keteraan la, ñu muure seeni kanam ak safara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Simoore Ibrahima

48يَوْمَ تُبَدَّلُ الْأَرْضُ غَيْرَ الْأَرْضِ وَالسَّمَاوَاتُ ۖ وَبَرَزُوا لِلَّهِ الْوَاحِدِ الْقَهَّارِ
ba bis ba ñuy weccee suuf sii seneen suuf ak asamaan yi itam te nit ñi génne [ca seeni bàmmeel] teew ca Yàlla ja di jenn, te di Notaakoon ba.
49وَتَرَى الْمُجْرِمِينَ يَوْمَئِذٍ مُّقَرَّنِينَ فِي الْأَصْفَادِ
ca bis booba, danga gis saay-saay sa ñu lëkkale leen ca jéng ya,
50سَرَابِيلُهُم مِّن قَطِرَانٍ وَتَغْشَىٰ وُجُوهَهُمُ النَّارُ
seeni yére keteraan la, ñu muure seeni kanam ak safara.
51لِيَجْزِيَ اللَّهُ كُلَّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
[La ko waral] moo di Yàllaa feye bakkan bu nekk la mu fàggu. Te nag Yàlla moom Ku gaaw ka ci natt lu ne.
52هَٰذَا بَلَاغٌ لِّلنَّاسِ وَلِيُنذَرُوا بِهِ وَلِيَعْلَمُوا أَنَّمَا هُوَ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ وَلِيَذَّكَّرَ أُولُو الْأَلْبَابِ
Ngir ñu waaru te xame ca itam Moom Yàlla jenn Yàlla doŋŋ la, ak itam woroom xel ya fàttalikoo ci.
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Ibrahima 50

Simoore Ibrahima Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : seeni yére keteraan la, ñu muure seeni kanam ak safara.

Simoore Aaya 50/52 — Simoore Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ibrahima Dégg, Simoore Ibrahima Tekki, Simoore Ibrahima mp3, Simoore Ibrahima pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers