Ibrahima · 51/52
Tekki Waxtaan — Ibrahima
لِيَجْزِيَ اللَّهُ كُلَّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ ۝٥١
Liyajziyal laahu kulla nafsim maa kasabat; innal laaha saree`ul hisaab
📖 Tekkim Wolof
[La ko waral] moo di Yàllaa feye bakkan bu nekk la mu fàggu. Te nag Yàlla moom Ku gaaw ka ci natt lu ne.

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-52 — Ibrahima

49وَتَرَى الْمُجْرِمِينَ يَوْمَئِذٍ مُّقَرَّنِينَ فِي الْأَصْفَادِ
ca bis booba, danga gis saay-saay sa ñu lëkkale leen ca jéng ya,
50سَرَابِيلُهُم مِّن قَطِرَانٍ وَتَغْشَىٰ وُجُوهَهُمُ النَّارُ
seeni yére keteraan la, ñu muure seeni kanam ak safara.
51لِيَجْزِيَ اللَّهُ كُلَّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
[La ko waral] moo di Yàllaa feye bakkan bu nekk la mu fàggu. Te nag Yàlla moom Ku gaaw ka ci natt lu ne.
52هَٰذَا بَلَاغٌ لِّلنَّاسِ وَلِيُنذَرُوا بِهِ وَلِيَعْلَمُوا أَنَّمَا هُوَ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ وَلِيَذَّكَّرَ أُولُو الْأَلْبَابِ
Ngir ñu waaru te xame ca itam Moom Yàlla jenn Yàlla doŋŋ la, ak itam woroom xel ya fàttalikoo ci.
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Ibrahima 51

Simoore Ibrahima Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [La ko waral] moo di Yàllaa feye bakkan bu nekk…

Simoore Aaya 51/52 — Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ibrahima Dégg, Ibrahima Tekki, Ibrahima mp3, Ibrahima pdf. Aaya 49–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers