Al-Hijr · 18/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِلَّا مَنِ اسْتَرَقَ السَّمْعَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ مُّبِينٌ ۝١٨
Illaa manis taraqas sam`a fa atba`ahoo shihaabum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Lu dul ku jéem a sàcc lu mu dégg, [te ku ko ca jéem] ay jumu safara soxal ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Simoore Al-Hijr

16وَلَقَدْ جَعَلْنَا فِي السَّمَاءِ بُرُوجًا وَزَيَّنَّاهَا لِلنَّاظِرِينَ
Def nañu ci asamaan ay bidiw te rafetal Nanu ko ñi koy xool mu ne ràññ.
17وَحَفِظْنَاهَا مِن كُلِّ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te wattu Nanu ko ba sépp séytaane su ñu rëbb du fa mën a egg.
18إِلَّا مَنِ اسْتَرَقَ السَّمْعَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ مُّبِينٌ
Lu dul ku jéem a sàcc lu mu dégg, [te ku ko ca jéem] ay jumu safara soxal ko.
19وَالْأَرْضَ مَدَدْنَاهَا وَأَلْقَيْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ شَيْءٍ مَّوْزُونٍ
Tàllal Nanu suuf si te samp ci ay tundi doj (yu tax mu dal) ; saxal Nanu itam wépp xeetu gàncax muy lu ñu nattale.
20وَجَعَلْنَا لَكُمْ فِيهَا مَعَايِشَ وَمَن لَّسْتُمْ لَهُ بِرَازِقِينَ
Nu defaral leen ca lu ngeen di dunde, yéen ak ñi ngeen dundalul.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Hijr 18

Simoore Al-Hijr Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu dul ku jéem a sàcc lu mu dégg, [te…

Simoore Aaya 18/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers