Al-Hijr · 19/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَالْأَرْضَ مَدَدْنَاهَا وَأَلْقَيْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ شَيْءٍ مَّوْزُونٍ ۝١٩
Wal arda madadnaahaa wa alqainaa feehaa rawaasiya wa ambatnaa feehaa min kulli shai`im mawzoon
📖 Tekkim Wolof
Tàllal Nanu suuf si te samp ci ay tundi doj (yu tax mu dal) ; saxal Nanu itam wépp xeetu gàncax muy lu ñu nattale.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Al-Hijr

17وَحَفِظْنَاهَا مِن كُلِّ شَيْطَانٍ رَّجِيمٍ
Te wattu Nanu ko ba sépp séytaane su ñu rëbb du fa mën a egg.
18إِلَّا مَنِ اسْتَرَقَ السَّمْعَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ مُّبِينٌ
Lu dul ku jéem a sàcc lu mu dégg, [te ku ko ca jéem] ay jumu safara soxal ko.
19وَالْأَرْضَ مَدَدْنَاهَا وَأَلْقَيْنَا فِيهَا رَوَاسِيَ وَأَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ شَيْءٍ مَّوْزُونٍ
Tàllal Nanu suuf si te samp ci ay tundi doj (yu tax mu dal) ; saxal Nanu itam wépp xeetu gàncax muy lu ñu nattale.
20وَجَعَلْنَا لَكُمْ فِيهَا مَعَايِشَ وَمَن لَّسْتُمْ لَهُ بِرَازِقِينَ
Nu defaral leen ca lu ngeen di dunde, yéen ak ñi ngeen dundalul.
21وَإِن مِّن شَيْءٍ إِلَّا عِندَنَا خَزَائِنُهُ وَمَا نُنَزِّلُهُ إِلَّا بِقَدَرٍ مَّعْلُومٍ
Amul lenn loo xam ne ndàmbam nekkul ci nun, waaye Dunu ca wàcce lu dul ab natt bu ñu xam (bu yem ak bu doy).
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Hijr 19

Simoore Al-Hijr Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tàllal Nanu suuf si te samp ci ay tundi doj…

Simoore Aaya 19/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers