Al-Hijr · 26/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ ۝٢٦
Wa laqad khalaqnal insaana min salsaalim min hama im masnoon
📖 Tekkim Wolof
Bind Nanu nit ci ban bu wow bu jóge ci ban bu ñuul.

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Hijr

24وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَقْدِمِينَ مِنكُمْ وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَأْخِرِينَ
Sunu xam-xam làmb na ña jiitu woon ak ñay mujj ci yéen.
25وَإِنَّ رَبَّكَ هُوَ يَحْشُرُهُمْ ۚ إِنَّهُ حَكِيمٌ عَلِيمٌ
Sa Boroom dana leen fang ñoom ñépp. Moom Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
26وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
Bind Nanu nit ci ban bu wow bu jóge ci ban bu ñuul.
27وَالْجَانَّ خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ مِن نَّارِ السَّمُومِ
Te fekkon na Nu binde jinne lu jiitu loolu ci safara wu xonk coyy.
28وَإِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
[Fàttalikul] ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man damay bind nit ci ban bu ñu togg,
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Hijr 26

Simoore Al-Hijr Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bind Nanu nit ci ban bu wow bu jóge ci…

Simoore Aaya 26/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers