Al-Hijr · 25/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَإِنَّ رَبَّكَ هُوَ يَحْشُرُهُمْ ۚ إِنَّهُ حَكِيمٌ عَلِيمٌ ۝٢٥
Wa inna Rabbaka Huwa yahshuruhum; innahoo Hakeem `Aleem
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom dana leen fang ñoom ñépp. Moom Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Hijr

23وَإِنَّا لَنَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَنَحْنُ الْوَارِثُونَ
Te Nun nooy dundal te Nun nooy rey te Nun nooy donn (mujje) àddina bi yépp.
24وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَقْدِمِينَ مِنكُمْ وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَأْخِرِينَ
Sunu xam-xam làmb na ña jiitu woon ak ñay mujj ci yéen.
25وَإِنَّ رَبَّكَ هُوَ يَحْشُرُهُمْ ۚ إِنَّهُ حَكِيمٌ عَلِيمٌ
Sa Boroom dana leen fang ñoom ñépp. Moom Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
26وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
Bind Nanu nit ci ban bu wow bu jóge ci ban bu ñuul.
27وَالْجَانَّ خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ مِن نَّارِ السَّمُومِ
Te fekkon na Nu binde jinne lu jiitu loolu ci safara wu xonk coyy.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Hijr 25

Simoore Al-Hijr Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom dana leen fang ñoom ñépp. Moom Yàlla Ku…

Simoore Aaya 25/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers