Al-Hijr · 34/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ فَاخْرُجْ مِنْهَا فَإِنَّكَ رَجِيمٌ ۝٣٤
Qaala fakhruj minhaa fa innaka rajeem
📖 Tekkim Wolof
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Hijr

32قَالَ يَا إِبْلِيسُ مَا لَكَ أَلَّا تَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
Mu ne [Moom Yàlla] : “Yaw Ibliis, lu la dal ba bokkuloo ci sujjóotkat yi ? ”
33قَالَ لَمْ أَكُن لِّأَسْجُدَ لِبَشَرٍ خَلَقْتَهُ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.
34قَالَ فَاخْرُجْ مِنْهَا فَإِنَّكَ رَجِيمٌ
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.
35وَإِنَّ عَلَيْكَ اللَّعْنَةَ إِلَىٰ يَوْمِ الدِّينِ
Te am rëbb dal na ci sa kaw ba Bis-pénc ba di taxaw ! ”
36قَالَ رَبِّ فَأَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
-Mu ne : "Yaw sama Boroom, kon muñal ma ba bisu dekki ba”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Hijr 34

Simoore Al-Hijr Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo…

Simoore Aaya 34/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers