Al-Hijr · 39/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
قَالَ رَبِّ بِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأُزَيِّنَنَّ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَلَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٣٩
Qaala Rabbi bimaaa aghwaitanee la uzayyinaana lahum fil ardi wa la ughwiyan nahum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
- Ibliis ne : "Yaw sama Boroom, ci sababus li nga ma beewloo, fàwwu danaa leen rafetalal ci àddina [lu bon], te fàwwu danaa leen beewloo ñoom ñépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Hijr

37قَالَ فَإِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
Mu ne : bokk nga ca ña ñu muñal,
38إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca Bis ba nga xam ne waxtoom lu ñu xam la.
39قَالَ رَبِّ بِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأُزَيِّنَنَّ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَلَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
- Ibliis ne : "Yaw sama Boroom, ci sababus li nga ma beewloo, fàwwu danaa leen rafetalal ci àddina [lu bon], te fàwwu danaa leen beewloo ñoom ñépp,
40إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des ña sellal ca sa jaam ña.”
41قَالَ هَٰذَا صِرَاطٌ عَلَيَّ مُسْتَقِيمٌ
- Boroom bi tontu ne : lii mooy yoon wu jub wi jëm ci Man.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Hijr 39

Simoore Al-Hijr Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ibliis ne : "Yaw sama Boroom, ci sababus li…

Simoore Aaya 39/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers