Al-Hijr · 40/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ ٤٠
Transliteration
Illaa `ibaadaka minhumul mukhlaseen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ba mu des ña sellal ca sa jaam ña.”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 38-42 — Al-Hijr
38إِلَىٰ يَوْمِ الْوَقْتِ الْمَعْلُومِ
ba ca Bis ba nga xam ne waxtoom lu ñu xam la.
39قَالَ رَبِّ بِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأُزَيِّنَنَّ لَهُمْ فِي الْأَرْضِ وَلَأُغْوِيَنَّهُمْ أَجْمَعِينَ
- Ibliis ne : "Yaw sama Boroom, ci sababus li nga ma beewloo, fàwwu danaa leen rafetalal ci àddina [lu bon], te fàwwu danaa leen beewloo ñoom ñépp,
40إِلَّا عِبَادَكَ مِنْهُمُ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des ña sellal ca sa jaam ña.”
41قَالَ هَٰذَا صِرَاطٌ عَلَيَّ مُسْتَقِيمٌ
- Boroom bi tontu ne : lii mooy yoon wu jub wi jëm ci Man.
42إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ إِلَّا مَنِ اتَّبَعَكَ مِنَ الْغَاوِينَ
Sama jaam ñi nag ñoom mënoo ci ñoom dara lu dul ña beew ña la topp.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
40Aaya
Tekki — Al-Hijr 40
Simoore Al-Hijr Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des ña sellal ca sa jaam ña.”Simoore Aaya 40/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








