Al-Hijr · 6/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَقَالُوا يَا أَيُّهَا الَّذِي نُزِّلَ عَلَيْهِ الذِّكْرُ إِنَّكَ لَمَجْنُونٌ ۝٦
Wa qaaloo yaaa aiyuhal lazee nuzzila `alaihiz Zikru innaka lamajnoon
📖 Tekkim Wolof
Ñu naan leen : “Yaw mii, wàcceef na ci yéen Téere ba, yaw dof tigi nga !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Hijr

4وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا وَلَهَا كِتَابٌ مَّعْلُومٌ
Dunu alag benn dëkk te fekk amul àpp bu ñu xam.
5مَّا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Benn xeet du jiitu àppam te it mënu koo weesu.
6وَقَالُوا يَا أَيُّهَا الَّذِي نُزِّلَ عَلَيْهِ الذِّكْرُ إِنَّكَ لَمَجْنُونٌ
Ñu naan leen : “Yaw mii, wàcceef na ci yéen Téere ba, yaw dof tigi nga !
7لَّوْ مَا تَأْتِينَا بِالْمَلَائِكَةِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Lu teewoon nga indil nu ay Malaaka, ndegam bokk nga ca ñu dëggu ña ? ”
8مَا نُنَزِّلُ الْمَلَائِكَةَ إِلَّا بِالْحَقِّ وَمَا كَانُوا إِذًا مُّنظَرِينَ
Nun dunu wàcce ay Malaaka lu dul ci dëgg (gu Nu doxal mu jeex) ; te kon dungeen doon ñu ñuy muñandiku ab diir.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Hijr 6

Simoore Al-Hijr Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu naan leen : “Yaw mii, wàcceef na ci yéen…

Simoore Aaya 6/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers