Al-Hijr · 5/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
مَّا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ ۝٥
Maa tasbiqu min ummatin ajalahaa wa maa yastaakhiroon
📖 Tekkim Wolof
Benn xeet du jiitu àppam te it mënu koo weesu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Hijr

3ذَرْهُمْ يَأْكُلُوا وَيَتَمَتَّعُوا وَيُلْهِهِمُ الْأَمَلُ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Bàyyileen ñuy lekk ak a xéewlu, tey mébét lu leen soxal; danañu mës a xam !
4وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا وَلَهَا كِتَابٌ مَّعْلُومٌ
Dunu alag benn dëkk te fekk amul àpp bu ñu xam.
5مَّا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Benn xeet du jiitu àppam te it mënu koo weesu.
6وَقَالُوا يَا أَيُّهَا الَّذِي نُزِّلَ عَلَيْهِ الذِّكْرُ إِنَّكَ لَمَجْنُونٌ
Ñu naan leen : “Yaw mii, wàcceef na ci yéen Téere ba, yaw dof tigi nga !
7لَّوْ مَا تَأْتِينَا بِالْمَلَائِكَةِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Lu teewoon nga indil nu ay Malaaka, ndegam bokk nga ca ñu dëggu ña ? ”
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Hijr 5

Simoore Al-Hijr Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Benn xeet du jiitu àppam te it mënu koo weesu.

Simoore Aaya 5/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers