Al-Hijr · 97/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَلَقَدْ نَعْلَمُ أَنَّكَ يَضِيقُ صَدْرُكَ بِمَا يَقُولُونَ ۝٩٧
Wa laqad na`lamu annak yadeequ sadruka bimaa yaqooloon
📖 Tekkim Wolof
Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa xol.

🎧 Dégg


📜 Aaya 95-99 — Simoore Al-Hijr

95إِنَّا كَفَيْنَاكَ الْمُسْتَهْزِئِينَ
Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.
96الَّذِينَ يَجْعَلُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla, danañu mës a xam.
97وَلَقَدْ نَعْلَمُ أَنَّكَ يَضِيقُ صَدْرُكَ بِمَا يَقُولُونَ
Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa xol.
98فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَكُن مِّنَ السَّاجِدِينَ
Sàbbaalal sa Boroom mi yeyoo cant, te nanga bokk ca sujjóotkat ya ;
99وَاعْبُدْ رَبَّكَ حَتَّىٰ يَأْتِيَكَ الْيَقِينُ
te nangay jaamu Yàlla ba balaa bir la [dee ga] di agsi ci yaw.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
97Aaya

Tekki — Al-Hijr 97

Simoore Al-Hijr Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa…

Simoore Aaya 97/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers