An-Nahl · 15/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَأَلْقَىٰ فِي الْأَرْضِ رَوَاسِيَ أَن تَمِيدَ بِكُمْ وَأَنْهَارًا وَسُبُلًا لَّعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ ۝١٥
Wa alqaa fil ardi rawaasiya an tameeda bikum wa anhaaranw wa sublulal la `allakum tahtadoon
📖 Tekkim Wolof
Te Moo samp ci suuf si ay ndëgërlaay [mu dal] bañ a jaayu ak yéen, ak i dex ak i yoon,

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore An-Nahl

13وَمَا ذَرَأَ لَكُمْ فِي الْأَرْضِ مُخْتَلِفًا أَلْوَانُهُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَذَّكَّرُونَ
Te li Mu leen wesaareel ci kaw suuf si am nañu ay melo yu wuute. Te ci biir yooyu, am na ca ay kéemaan ñeel aw nit ñuy waaru.
14وَهُوَ الَّذِي سَخَّرَ الْبَحْرَ لِتَأْكُلُوا مِنْهُ لَحْمًا طَرِيًّا وَتَسْتَخْرِجُوا مِنْهُ حِلْيَةً تَلْبَسُونَهَا وَتَرَى الْفُلْكَ مَوَاخِرَ فِيهِ وَلِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ وَلَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Te Moom moo leen tàggatal géej gi ngir ngeen mën ciy jële yàpp wu tooy wu ngeen di lekk, ak ngeen ciy mën a génne ay takkaay yu ngeen di takk. Te gis ngeen ne gaal yaa ngi cay daw, ak it ngeen di ca sàkku ci xéewalam ya, te kon xéy-na di ngeen ko gërëm.
15وَأَلْقَىٰ فِي الْأَرْضِ رَوَاسِيَ أَن تَمِيدَ بِكُمْ وَأَنْهَارًا وَسُبُلًا لَّعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ
Te Moo samp ci suuf si ay ndëgërlaay [mu dal] bañ a jaayu ak yéen, ak i dex ak i yoon,
16وَعَلَامَاتٍ ۚ وَبِالنَّجْمِ هُمْ يَهْتَدُونَ
[def na it ci suuf si] ay màndarga, nit ña mën a gindikoo ci bidiw yi.
17أَفَمَن يَخْلُقُ كَمَن لَّا يَخْلُقُ ۗ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Waaw ndax ku bind dana mën a yem ak ku bindul dara ? Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — An-Nahl 15

Simoore An-Nahl Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Moo samp ci suuf si ay ndëgërlaay [mu dal]…

Simoore Aaya 15/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers