An-Nahl · 24/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
وَإِذَا قِيلَ لَهُم مَّاذَا أَنزَلَ رَبُّكُمْ ۙ قَالُوا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ ٢٤
Transliteration
Wa izaa qeela lahum maazaaa anzala Rabbukum qaaloo asaateerul awwaleen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu nee leen : “Lan la seen Boroom wàcce ? ”. Ñu ne : “Xanaa ay léeb yu jóge ca mag ñu njëgg ña ! ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — An-Nahl
22إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۚ فَالَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ قُلُوبُهُم مُّنكِرَةٌ وَهُم مُّسْتَكْبِرُونَ
Seen Yàlla jenn rekk la. Tax na ña gëmul àllaaxira, seeni xol a dàq a weddi te ñoom dañuy rëy-rëylu.
23لَا جَرَمَ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْمُسْتَكْبِرِينَ
Ca dëgg-dëgg, Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la ñuy feeñal. Te Yàlla nag soppul ñiy rëy- rëylu.
24وَإِذَا قِيلَ لَهُم مَّاذَا أَنزَلَ رَبُّكُمْ ۙ قَالُوا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Bu ñu nee leen : “Lan la seen Boroom wàcce ? ”. Ñu ne : “Xanaa ay léeb yu jóge ca mag ñu njëgg ña ! ”
25لِيَحْمِلُوا أَوْزَارَهُمْ كَامِلَةً يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۙ وَمِنْ أَوْزَارِ الَّذِينَ يُضِلُّونَهُم بِغَيْرِ عِلْمٍ ۗ أَلَا سَاءَ مَا يَزِرُونَ
Danañu yenu seeni bàkkaar ba mu mat sëkk, Bis-pénc ba, ak lenn ca bàkkaari ña ñu réeral, ci loo xam ne amuñu ca woon xam-xam ; cëy ndaw yen bu bon !
26قَدْ مَكَرَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَأَتَى اللَّهُ بُنْيَانَهُم مِّنَ الْقَوَاعِدِ فَخَرَّ عَلَيْهِمُ السَّقْفُ مِن فَوْقِهِمْ وَأَتَاهُمُ الْعَذَابُ مِنْ حَيْثُ لَا يَشْعُرُونَ
Ña leen jiitu woon defoon nañu ay pexe, Yàlla toj seeni tabax ya dale ko ca ndëgërlaay ja. Téeg ma daanu seen kaw, mbugal ma agsi ca ñoom jaare fu ñu ko foogewul woon.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — An-Nahl 24
Simoore An-Nahl Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu nee leen : “Lan la seen Boroom wàcce…Simoore Aaya 24/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








