Al-Isra · 18/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
مَّن كَانَ يُرِيدُ الْعَاجِلَةَ عَجَّلْنَا لَهُ فِيهَا مَا نَشَاءُ لِمَن نُّرِيدُ ثُمَّ جَعَلْنَا لَهُ جَهَنَّمَ يَصْلَاهَا مَذْمُومًا مَّدْحُورًا ۝١٨
Man kaana yureedul `aajilata `ajjalnaa lahoo feehaa maa nashaaa`u liman nureedu summa ja`alnaa lahoo Jahannama yaslaahaa mazmoomammad hooraa
📖 Tekkim Wolof
Képp ku bëggul lu dul teraangay àddina, Dananu gaaw ci jox ko la Nu neex ; ca ku Nu neex. Topp Nu def Safara fa muy séndalu, di ku ñu xas, ku ñu génne [ci yërmaandey Yàlla].
🎧 Dégg

📜 Aaya 16-20 — Al-Isra

16وَإِذَا أَرَدْنَا أَن نُّهْلِكَ قَرْيَةً أَمَرْنَا مُتْرَفِيهَا فَفَسَقُوا فِيهَا فَحَقَّ عَلَيْهَا الْقَوْلُ فَدَمَّرْنَاهَا تَدْمِيرًا
Bu Nu nammee alag ab dëkk, dafay fekk ne boroom alal ya dañoo jubadi ca dëkk ba. Àtte ba daldi yell ca ñoom. Nu sadd leen sadd gu tar.
17وَكَمْ أَهْلَكْنَا مِنَ الْقُرُونِ مِن بَعْدِ نُوحٍ ۗ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ بِذُنُوبِ عِبَادِهِ خَبِيرًا بَصِيرًا
Aka bari xeet yu Nu alag ginnaaw Nooh ! Te sa Boroom kuy gis la te xam bàkkaari jaam ñi.
18مَّن كَانَ يُرِيدُ الْعَاجِلَةَ عَجَّلْنَا لَهُ فِيهَا مَا نَشَاءُ لِمَن نُّرِيدُ ثُمَّ جَعَلْنَا لَهُ جَهَنَّمَ يَصْلَاهَا مَذْمُومًا مَّدْحُورًا
Képp ku bëggul lu dul teraangay àddina, Dananu gaaw ci jox ko la Nu neex ; ca ku Nu neex. Topp Nu def Safara fa muy séndalu, di ku ñu xas, ku ñu génne [ci yërmaandey Yàlla].
19وَمَنْ أَرَادَ الْآخِرَةَ وَسَعَىٰ لَهَا سَعْيَهَا وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَأُولَٰئِكَ كَانَ سَعْيُهُم مَّشْكُورًا
Ku bëgg [teraangay] àllaaxira te mu jëf lu méngook moom, te muy ku gëm... ñooñu seeni jëf lu ñu gërëm lay doon.
20كُلًّا نُّمِدُّ هَٰؤُلَاءِ وَهَٰؤُلَاءِ مِنْ عَطَاءِ رَبِّكَ ۚ وَمَا كَانَ عَطَاءُ رَبِّكَ مَحْظُورًا
Ñoom ñépp Dananu leen tëbb ; ñii ak ñële, ay may yu jóge ca sa Boroom. Te sa mayu Boroom nekkul lu ñu tere kenn.Làndi na!
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Isra 18

Simoore Al-Isra Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp ku bëggul lu dul teraangay àddina, Dananu gaaw ci…

Simoore Aaya 18/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers