Al-Isra · 21/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
انظُرْ كَيْفَ فَضَّلْنَا بَعْضَهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ وَلَلْآخِرَةُ أَكْبَرُ دَرَجَاتٍ وَأَكْبَرُ تَفْضِيلًا ٢١
Transliteration
Unzur kaifa faddalnaa ba`dahum `alaa ba`d; wa lal Aakhiratu akbaru darajaatinw wa akbaru tafdeelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Gisal ni Nu gënalee ñenn ñi ci kaw ñeneen ña. Te ca dëgg-dëgg àllaaxira moo gën a màgg daraja te moo gën a màgg i xéewal.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 19-23 — Al-Isra
19وَمَنْ أَرَادَ الْآخِرَةَ وَسَعَىٰ لَهَا سَعْيَهَا وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَأُولَٰئِكَ كَانَ سَعْيُهُم مَّشْكُورًا
Ku bëgg [teraangay] àllaaxira te mu jëf lu méngook moom, te muy ku gëm... ñooñu seeni jëf lu ñu gërëm lay doon.
20كُلًّا نُّمِدُّ هَٰؤُلَاءِ وَهَٰؤُلَاءِ مِنْ عَطَاءِ رَبِّكَ ۚ وَمَا كَانَ عَطَاءُ رَبِّكَ مَحْظُورًا
Ñoom ñépp Dananu leen tëbb ; ñii ak ñële, ay may yu jóge ca sa Boroom. Te sa mayu Boroom nekkul lu ñu tere kenn.Làndi na!
21انظُرْ كَيْفَ فَضَّلْنَا بَعْضَهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ وَلَلْآخِرَةُ أَكْبَرُ دَرَجَاتٍ وَأَكْبَرُ تَفْضِيلًا
Gisal ni Nu gënalee ñenn ñi ci kaw ñeneen ña. Te ca dëgg-dëgg àllaaxira moo gën a màgg daraja te moo gën a màgg i xéewal.
22لَّا تَجْعَلْ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَتَقْعُدَ مَذْمُومًا مَّخْذُولًا
Bul sàkk jeneen yàlla di ko booleek Yàlla ; kon dey danga doon ku ñu xas, ku ñu wacc mu beddiku.
23۞ وَقَضَىٰ رَبُّكَ أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا إِيَّاهُ وَبِالْوَالِدَيْنِ إِحْسَانًا ۚ إِمَّا يَبْلُغَنَّ عِندَكَ الْكِبَرَ أَحَدُهُمَا أَوْ كِلَاهُمَا فَلَا تَقُل لَّهُمَا أُفٍّ وَلَا تَنْهَرْهُمَا وَقُل لَّهُمَا قَوْلًا كَرِيمًا
Sa Boroom dogal na ne : “Buleen jaamu ku dul Moom doŋŋ ; te ngeen rafetal jëme ci seeni waajur : te ndeem kenn ci ñoom walla ñoom ñaar egg nañu ci màggat ci sa teewaay ; buleen wax : “Kuf ma la ! ”, buleen leen gëdd, nangeen leen wax wax ju yiw.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
21Aaya
Tekki — Al-Isra 21
Simoore Al-Isra Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gisal ni Nu gënalee ñenn ñi ci kaw ñeneen ña.…Simoore Aaya 21/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








