Al-Isra · 81/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَقُلْ جَاءَ الْحَقُّ وَزَهَقَ الْبَاطِلُ ۚ إِنَّ الْبَاطِلَ كَانَ زَهُوقًا ٨١
Transliteration
Wa qul jaaa`al haqqu wa zahaqal baatil; innal baatila kaana zahooqaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te neel : “Dëgg ga egsi na. Caaxaan wéy na. Caaxaan nag luy dem la naaxsaay”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 79-83 — Al-Isra
79وَمِنَ اللَّيْلِ فَتَهَجَّدْ بِهِ نَافِلَةً لَّكَ عَسَىٰ أَن يَبْعَثَكَ رَبُّكَ مَقَامًا مَّحْمُودًا
Te nangay julli ci suba, def ko muy naafila : xéy-na kon sa Boroom dekkal la, jox la ndam lu yeyoo cant.
80وَقُل رَّبِّ أَدْخِلْنِي مُدْخَلَ صِدْقٍ وَأَخْرِجْنِي مُخْرَجَ صِدْقٍ وَاجْعَل لِّي مِن لَّدُنكَ سُلْطَانًا نَّصِيرًا
Neel : "Sama Boroom ; dugal ma ci duggukaayu dëggu te nga génne ma ci génnukaayu dëgg ; te nga defal ma kàttan gu tukke ci yaw di dimbal”.
81وَقُلْ جَاءَ الْحَقُّ وَزَهَقَ الْبَاطِلُ ۚ إِنَّ الْبَاطِلَ كَانَ زَهُوقًا
Te neel : “Dëgg ga egsi na. Caaxaan wéy na. Caaxaan nag luy dem la naaxsaay”.
82وَنُنَزِّلُ مِنَ الْقُرْآنِ مَا هُوَ شِفَاءٌ وَرَحْمَةٌ لِّلْمُؤْمِنِينَ ۙ وَلَا يَزِيدُ الظَّالِمِينَ إِلَّا خَسَارًا
Wàcce Nanu ci Alxuraan loo xam ne saafara la ak yërmaande ca way-gëm ña. Waaye du yokk tooñkat ya lu dul yàqule.
83وَإِذَا أَنْعَمْنَا عَلَى الْإِنسَانِ أَعْرَضَ وَنَأَىٰ بِجَانِبِهِ ۖ وَإِذَا مَسَّهُ الشَّرُّ كَانَ يَئُوسًا
Te bu Nu defalee nit xéewal ; mu dëddu, fuuyu ci wetam ; waaye bu ko tiis dalee, mu ñàkk yaakaar [yërmaande Yàlla].
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
81Aaya
Tekki — Al-Isra 81
Simoore Al-Isra Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te neel : “Dëgg ga egsi na. Caaxaan wéy na.…Simoore Aaya 81/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








