Al-Isra · 82/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَنُنَزِّلُ مِنَ الْقُرْآنِ مَا هُوَ شِفَاءٌ وَرَحْمَةٌ لِّلْمُؤْمِنِينَ ۙ وَلَا يَزِيدُ الظَّالِمِينَ إِلَّا خَسَارًا ۝٨٢
Wa nunazzilu minal quraani maa huwa shifaaa`unw wa rahmatul lilmu;mineena wa laa yazeeduz zaalimeena illaa khasaaraa
📖 Tekkim Wolof
Wàcce Nanu ci Alxuraan loo xam ne saafara la ak yërmaande ca way-gëm ña. Waaye du yokk tooñkat ya lu dul yàqule.
🎧 Dégg

📜 Aaya 80-84 — Al-Isra

80وَقُل رَّبِّ أَدْخِلْنِي مُدْخَلَ صِدْقٍ وَأَخْرِجْنِي مُخْرَجَ صِدْقٍ وَاجْعَل لِّي مِن لَّدُنكَ سُلْطَانًا نَّصِيرًا
Neel : "Sama Boroom ; dugal ma ci duggukaayu dëggu te nga génne ma ci génnukaayu dëgg ; te nga defal ma kàttan gu tukke ci yaw di dimbal”.
81وَقُلْ جَاءَ الْحَقُّ وَزَهَقَ الْبَاطِلُ ۚ إِنَّ الْبَاطِلَ كَانَ زَهُوقًا
Te neel : “Dëgg ga egsi na. Caaxaan wéy na. Caaxaan nag luy dem la naaxsaay”.
82وَنُنَزِّلُ مِنَ الْقُرْآنِ مَا هُوَ شِفَاءٌ وَرَحْمَةٌ لِّلْمُؤْمِنِينَ ۙ وَلَا يَزِيدُ الظَّالِمِينَ إِلَّا خَسَارًا
Wàcce Nanu ci Alxuraan loo xam ne saafara la ak yërmaande ca way-gëm ña. Waaye du yokk tooñkat ya lu dul yàqule.
83وَإِذَا أَنْعَمْنَا عَلَى الْإِنسَانِ أَعْرَضَ وَنَأَىٰ بِجَانِبِهِ ۖ وَإِذَا مَسَّهُ الشَّرُّ كَانَ يَئُوسًا
Te bu Nu defalee nit xéewal ; mu dëddu, fuuyu ci wetam ; waaye bu ko tiis dalee, mu ñàkk yaakaar [yërmaande Yàlla].
84قُلْ كُلٌّ يَعْمَلُ عَلَىٰ شَاكِلَتِهِ فَرَبُّكُمْ أَعْلَمُ بِمَنْ هُوَ أَهْدَىٰ سَبِيلًا
Neel : “Ku nekk a ngay jëf lu méngook meloon, waaye sa Boroom a gën a xam ku gindiku tegu ca yoon wu jub wa”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Al-Isra 82

Simoore Al-Isra Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàcce Nanu ci Alxuraan loo xam ne saafara la ak…

Simoore Aaya 82/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers