Maryam · 79/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
كَلَّا ۚ سَنَكْتُبُ مَا يَقُولُ وَنَمُدُّ لَهُ مِنَ الْعَذَابِ مَدًّا ۝٧٩
Kallaa; sanaktubu maa yaqoolu wa namuddu lahoo minal `azaabi maddaa
📖 Tekkim Wolof
Déewallaay ! Dananu bind la muy wax, te it Dananu ko mbugal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 77-81 — Simoore Maryam

77أَفَرَأَيْتَ الَّذِي كَفَرَ بِآيَاتِنَا وَقَالَ لَأُوتَيَنَّ مَالًا وَوَلَدًا
Xanaa gisoo ka weddi Sunuy kàddu bay wax naan : “[Ak lu mën a xew], man danaa am alal ak i doom” ?
78أَطَّلَعَ الْغَيْبَ أَمِ اتَّخَذَ عِندَ الرَّحْمَٰنِ عَهْدًا
Moo ndax dafa xam kumpa, walla mu digaaleek Yàlla ?
79كَلَّا ۚ سَنَكْتُبُ مَا يَقُولُ وَنَمُدُّ لَهُ مِنَ الْعَذَابِ مَدًّا
Déewallaay ! Dananu bind la muy wax, te it Dananu ko mbugal.
80وَنَرِثُهُ مَا يَقُولُ وَيَأْتِينَا فَرْدًا
[Doom ya ak alal ja] Dananu ko donn, te buy dikk fi Nun jubbu boppam lay àndal.
81وَاتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ آلِهَةً لِّيَكُونُوا لَهُمْ عِزًّا
Dañuy jàpp leneen lu dul Yàlla [di ko jaamu] ngir ame ca teraanga [dimbal].
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
79Aaya

Tekki — Maryam 79

Simoore Maryam Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déewallaay ! Dananu bind la muy wax, te it Dananu…

Simoore Aaya 79/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers