Maryam · 90/98
Tekki Waxtaan — Maryam
تَكَادُ السَّمَاوَاتُ يَتَفَطَّرْنَ مِنْهُ وَتَنشَقُّ الْأَرْضُ وَتَخِرُّ الْجِبَالُ هَدًّا ٩٠
Transliteration
Takaadus samaawaatu yatafattarna minhu wa tanshaq qul ardu wa takhirrul jibaalu haddaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Loo xam ne] asamaan yi xaw na cee xottiku, suuf si xar, tundi doj yi màbb [ngir wax jooju],
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 88-92 — Maryam
88وَقَالُوا اتَّخَذَ الرَّحْمَٰنُ وَلَدًا
Ñuy wax it naan : “[Yàlla] Yërëmaakoon ba am na doom ! ”
89لَّقَدْ جِئْتُمْ شَيْئًا إِدًّا
Indi ngeen lu juunu !
90تَكَادُ السَّمَاوَاتُ يَتَفَطَّرْنَ مِنْهُ وَتَنشَقُّ الْأَرْضُ وَتَخِرُّ الْجِبَالُ هَدًّا
[Loo xam ne] asamaan yi xaw na cee xottiku, suuf si xar, tundi doj yi màbb [ngir wax jooju],
91أَن دَعَوْا لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدًا
ña wax ne alamikk Yàlla am na doom,
92وَمَا يَنبَغِي لِلرَّحْمَٰنِ أَن يَتَّخِذَ وَلَدًا
Waay-waay yellut ci Yërëmaakoon bi muy am doom waay !
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
90Aaya
Tekki — Maryam 90
Simoore Maryam Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Loo xam ne] asamaan yi xaw na cee xottiku, suuf…Simoore Aaya 90/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








