Maryam · 89/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
لَّقَدْ جِئْتُمْ شَيْئًا إِدًّا ۝٨٩
Laqad ji`tum shai`an iddaa
📖 Tekkim Wolof
Indi ngeen lu juunu !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 87-91 — Simoore Maryam

87لَّا يَمْلِكُونَ الشَّفَاعَةَ إِلَّا مَنِ اتَّخَذَ عِندَ الرَّحْمَٰنِ عَهْدًا
[Bis booba] kenn du mën a ramm ku dul ku ko Yàlla digal.
88وَقَالُوا اتَّخَذَ الرَّحْمَٰنُ وَلَدًا
Ñuy wax it naan : “[Yàlla] Yërëmaakoon ba am na doom ! ”
89لَّقَدْ جِئْتُمْ شَيْئًا إِدًّا
Indi ngeen lu juunu !
90تَكَادُ السَّمَاوَاتُ يَتَفَطَّرْنَ مِنْهُ وَتَنشَقُّ الْأَرْضُ وَتَخِرُّ الْجِبَالُ هَدًّا
[Loo xam ne] asamaan yi xaw na cee xottiku, suuf si xar, tundi doj yi màbb [ngir wax jooju],
91أَن دَعَوْا لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدًا
ña wax ne alamikk Yàlla am na doom,
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — Maryam 89

Simoore Maryam Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Indi ngeen lu juunu !

Simoore Aaya 89/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers