Al-Baqara · 268/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
الشَّيْطَانُ يَعِدُكُمُ الْفَقْرَ وَيَأْمُرُكُم بِالْفَحْشَاءِ ۖ وَاللَّهُ يَعِدُكُم مَّغْفِرَةً مِّنْهُ وَفَضْلًا ۗ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ ۝٢٦٨
Ash Shaitaanu ya`idukumul faqra wa yaamurukum bilfahshaaa`i wallaahu ya`idukum maghfiratam minhu wa fadlaa; wallaahu Waasi`un `Aleem
📖 Tekkim Wolof
Séytaane, ag ñàkk la leen di dig, di leen xiir ci moy ;Yàlla nag, jéggal la leen di dig ak wërsëg wu bawoo ca Moom. Yàlla ku yaatu, ku xam la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 266-270 — Al-Baqara

266أَيَوَدُّ أَحَدُكُمْ أَن تَكُونَ لَهُ جَنَّةٌ مِّن نَّخِيلٍ وَأَعْنَابٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ لَهُ فِيهَا مِن كُلِّ الثَّمَرَاتِ وَأَصَابَهُ الْكِبَرُ وَلَهُ ذُرِّيَّةٌ ضُعَفَاءُ فَأَصَابَهَا إِعْصَارٌ فِيهِ نَارٌ فَاحْتَرَقَتْ ۗ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمُ الْآيَاتِ لَعَلَّكُمْ تَتَفَكَّرُونَ
Kenn ci yéen bu amoon toolu garabu tàndarma ak reseñ, ndox ya di daw ca biir, mu bari lool meññent, fekk mu nekk mag, ame njaboot gu sew, ndax dana bëgg callmeer lu ànd ak safara dal ca tool ba lakk ko ? Noonu la Yàlla di faramfàccee ay laayaam ndaxtelee ngeen di xalaat !
267يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَنفِقُوا مِن طَيِّبَاتِ مَا كَسَبْتُمْ وَمِمَّا أَخْرَجْنَا لَكُم مِّنَ الْأَرْضِ ۖ وَلَا تَيَمَّمُوا الْخَبِيثَ مِنْهُ تُنفِقُونَ وَلَسْتُم بِآخِذِيهِ إِلَّا أَن تُغْمِضُوا فِيهِ ۚ وَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ غَنِيٌّ حَمِيدٌ
Yéen ñi gëm ! Deeleen joxe asaka ci lu téey li ngeen di fàggul seen bopp ak li Nu leen génneele ci suuf si. Buleen ca beddi la ca yées di ko joxe. Te fekk muy loo xam ne ku leen ko joxoon dungeen ko bëgg a jël, te gëmmuleen ca ! Nangeen xam ne Yàlla ku woomal la te ku yayoo cant la.
268الشَّيْطَانُ يَعِدُكُمُ الْفَقْرَ وَيَأْمُرُكُم بِالْفَحْشَاءِ ۖ وَاللَّهُ يَعِدُكُم مَّغْفِرَةً مِّنْهُ وَفَضْلًا ۗ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ
Séytaane, ag ñàkk la leen di dig, di leen xiir ci moy ;Yàlla nag, jéggal la leen di dig ak wërsëg wu bawoo ca Moom. Yàlla ku yaatu, ku xam la.
269يُؤْتِي الْحِكْمَةَ مَن يَشَاءُ ۚ وَمَن يُؤْتَ الْحِكْمَةَ فَقَدْ أُوتِيَ خَيْرًا كَثِيرًا ۗ وَمَا يَذَّكَّرُ إِلَّا أُولُو الْأَلْبَابِ
Mooy jox ku ko soob xel mu rëy, rafet . Ku Mu jox xel mu rafet, jox na ko njariñ lu rëy. Te boroom xel ya rekk ay waaru.
270وَمَا أَنفَقْتُم مِّن نَّفَقَةٍ أَوْ نَذَرْتُم مِّن نَّذْرٍ فَإِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُهُ ۗ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِنْ أَنصَارٍ
Li ngeen joxe mu génn walla ngeen nisar ko , Yàlla xam na ko. Ñiy tooñ, duñu am ndimbal !
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
268Aaya

Tekki — Al-Baqara 268

Simoore Al-Baqara Aaya 268 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Séytaane, ag ñàkk la leen di dig, di leen xiir…

Simoore Aaya 268/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 266–270. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers