Taha · 116/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَإِذْ قُلْنَا لِلْمَلَائِكَةِ اسْجُدُوا لِآدَمَ فَسَجَدُوا إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ ۝١١٦
Wa iz qulnaa lilma laaa`ikatis judoo li Aadama fasajadooo illaaa Iblees; abaa
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul] ba Nu waxee Malaaka ya ne leen : “Sujjóotleen ci Aadama”, ñépp sujjóot ba mu des Ibliis, moom dafa lànk.
🎧 Dégg

📜 Aaya 114-118 — Taha

114فَتَعَالَى اللَّهُ الْمَلِكُ الْحَقُّ ۗ وَلَا تَعْجَلْ بِالْقُرْآنِ مِن قَبْلِ أَن يُقْضَىٰ إِلَيْكَ وَحْيُهُ ۖ وَقُل رَّبِّ زِدْنِي عِلْمًا
Yàlla Buur ba di dëgg, kawe na ! Bul yàkkamtee tasaare Alxuraan ji tey jiitu soloo ga. Waxal ne : "Yaw sama Boroom dolli ma xam-xam ! ”
115وَلَقَدْ عَهِدْنَا إِلَىٰ آدَمَ مِن قَبْلُ فَنَسِيَ وَلَمْ نَجِدْ لَهُ عَزْمًا
Fasantee woon Nanu ak Aadama ab dig ca la jiitu woon ; mu fàtte ; te taxu ko caa woo na farlu.
116وَإِذْ قُلْنَا لِلْمَلَائِكَةِ اسْجُدُوا لِآدَمَ فَسَجَدُوا إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ
[Fàttalikul] ba Nu waxee Malaaka ya ne leen : “Sujjóotleen ci Aadama”, ñépp sujjóot ba mu des Ibliis, moom dafa lànk.
117فَقُلْنَا يَا آدَمُ إِنَّ هَٰذَا عَدُوٌّ لَّكَ وَلِزَوْجِكَ فَلَا يُخْرِجَنَّكُمَا مِنَ الْجَنَّةِ فَتَشْقَىٰ
Nu wax ko ne ko : “Kii dey sab noon la yaak sa soxna. Farluleen ba bu mu leen génne Àjjana, [su ngeen génnee] da ngeen sonnu de.
118إِنَّ لَكَ أَلَّا تَجُوعَ فِيهَا وَلَا تَعْرَىٰ
[Fii ci Àjjana] doo fi xiif, doo fi rafle,
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
116Aaya

Tekki — Taha 116

Simoore Taha Aaya 116 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul] ba Nu waxee Malaaka ya ne leen : “Sujjóotleen…

Simoore Aaya 116/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 114–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers