Taha · 21/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قَالَ خُذْهَا وَلَا تَخَفْ ۖ سَنُعِيدُهَا سِيرَتَهَا الْأُولَىٰ ۝٢١
Qaala khuzhaa wa laa ta khaf sanu`eeduhaa seeratahal oolaa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Jël ko : Dananu ko delloo na mu meloon, bul ragal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 19-23 — Simoore Taha

19قَالَ أَلْقِهَا يَا مُوسَىٰ
[Yàlla ne ko] : “Sànni ko yaw Muusaa”.
20فَأَلْقَاهَا فَإِذَا هِيَ حَيَّةٌ تَسْعَىٰ
Mu sànni ko : ndekete yoo jaan a ngay bélaw-bélawi.
21قَالَ خُذْهَا وَلَا تَخَفْ ۖ سَنُعِيدُهَا سِيرَتَهَا الْأُولَىٰ
Mu ne ko : “Jël ko : Dananu ko delloo na mu meloon, bul ragal.
22وَاضْمُمْ يَدَكَ إِلَىٰ جَنَاحِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ آيَةً أُخْرَىٰ
Te nga dugal sa loxo ci sa biir poqotaan : mu génn weex tàll lool, di geneen kéemaan
23لِنُرِيَكَ مِنْ آيَاتِنَا الْكُبْرَى
[Lii lépp] Danu la koo waajale ngir won la ci Sunu kéemtaan yu màgg yi.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Taha 21

Simoore Taha Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Jël ko : Dananu ko delloo…

Simoore Aaya 21/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers