Taha · 52/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قَالَ عِلْمُهَا عِندَ رَبِّي فِي كِتَابٍ ۖ لَّا يَضِلُّ رَبِّي وَلَا يَنسَى ۝٥٢
Qaala `ilmuhaa `inda Rabee fee kitaab, laa yadillu Rabbee wa laa yansaa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Seeni mbir a nga ca Téere ba fa sa Boroom. Sama Boroom du juum, du fàtte.

🎧 Dégg


📜 Aaya 50-54 — Simoore Taha

50قَالَ رَبُّنَا الَّذِي أَعْطَىٰ كُلَّ شَيْءٍ خَلْقَهُ ثُمَّ هَدَىٰ
Mu ne ko : “Sunu Boroom, Moo sos mbindéef yépp, te Mooy gindee”.
51قَالَ فَمَا بَالُ الْقُرُونِ الْأُولَىٰ
[Firawna] ne ko : “Waaw xeet ya jiitu woon, ñoom luy xala doon seenub àtte ? ”.
52قَالَ عِلْمُهَا عِندَ رَبِّي فِي كِتَابٍ ۖ لَّا يَضِلُّ رَبِّي وَلَا يَنسَى
Mu ne ko : “Seeni mbir a nga ca Téere ba fa sa Boroom. Sama Boroom du juum, du fàtte.
53الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ مَهْدًا وَسَلَكَ لَكُمْ فِيهَا سُبُلًا وَأَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّن نَّبَاتٍ شَتَّىٰ
Sama Boroom bi nga xam ne Moo leen defal suuf si laltaay [maasale ko], defal leen ci ay yoon [ngeen di jokkoo] ; Mu wàcce am ndox mu bawoo asamaan, ñu di ca génne ay xeeti gàncax yu wuute.”
54كُلُوا وَارْعَوْا أَنْعَامَكُمْ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّأُولِي النُّهَىٰ
“Lekk-leen te sàmm seenug jur”. Ay kéemaan a ngi ci loolu, ñeel aw nit ñu am xel.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Taha 52

Simoore Taha Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Seeni mbir a nga ca Téere…

Simoore Aaya 52/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers