Taha · 51/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالَ فَمَا بَالُ الْقُرُونِ الْأُولَىٰ ۝٥١
Qaala famaa baalul quroonil oolaa
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] ne ko : “Waaw xeet ya jiitu woon, ñoom luy xala doon seenub àtte ? ”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 49-53 — Taha

49قَالَ فَمَن رَّبُّكُمَا يَا مُوسَىٰ
[Firawna] ne leen : “Waaw yéen ñaar kan moo di seen Boroom ? ”
50قَالَ رَبُّنَا الَّذِي أَعْطَىٰ كُلَّ شَيْءٍ خَلْقَهُ ثُمَّ هَدَىٰ
Mu ne ko : “Sunu Boroom, Moo sos mbindéef yépp, te Mooy gindee”.
51قَالَ فَمَا بَالُ الْقُرُونِ الْأُولَىٰ
[Firawna] ne ko : “Waaw xeet ya jiitu woon, ñoom luy xala doon seenub àtte ? ”.
52قَالَ عِلْمُهَا عِندَ رَبِّي فِي كِتَابٍ ۖ لَّا يَضِلُّ رَبِّي وَلَا يَنسَى
Mu ne ko : “Seeni mbir a nga ca Téere ba fa sa Boroom. Sama Boroom du juum, du fàtte.
53الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ مَهْدًا وَسَلَكَ لَكُمْ فِيهَا سُبُلًا وَأَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّن نَّبَاتٍ شَتَّىٰ
Sama Boroom bi nga xam ne Moo leen defal suuf si laltaay [maasale ko], defal leen ci ay yoon [ngeen di jokkoo] ; Mu wàcce am ndox mu bawoo asamaan, ñu di ca génne ay xeeti gàncax yu wuute.”
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Taha 51

Simoore Taha Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] ne ko : “Waaw xeet ya jiitu woon, ñoom…

Simoore Aaya 51/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers