Al-Anbiya · 55/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
قَالُوا أَجِئْتَنَا بِالْحَقِّ أَمْ أَنتَ مِنَ اللَّاعِبِينَ ٥٥
Transliteration
Qaalooo aji`tanaa bil haqqi am anta minal laa`ibeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Ndax li nga nu dig dëgg la ci yaw walla dangay kaf ? ”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 53-57 — Al-Anbiya
53قَالُوا وَجَدْنَا آبَاءَنَا لَهَا عَابِدِينَ
Ñu tontu ne : “Dañoo fekk sunuy baay di leen jaamu”.
54قَالَ لَقَدْ كُنتُمْ أَنتُمْ وَآبَاؤُكُمْ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Mu ne leen : “Ca dëgg-dëgg, yéen ak seeni baay dangeen a nekk ci réer gu fés”.
55قَالُوا أَجِئْتَنَا بِالْحَقِّ أَمْ أَنتَ مِنَ اللَّاعِبِينَ
Ñu ne ko : “Ndax li nga nu dig dëgg la ci yaw walla dangay kaf ? ”.
56قَالَ بَل رَّبُّكُمْ رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ الَّذِي فَطَرَهُنَّ وَأَنَا عَلَىٰ ذَٰلِكُم مِّنَ الشَّاهِدِينَ
Mu ne déedéet : “Seen Boroom mooy Boroom asamaan yi ak suuf si, te Moo leen sàkk. Te man dey bokk naa ci ñiy seede loolu ci yéen.
57وَتَاللَّهِ لَأَكِيدَنَّ أَصْنَامَكُم بَعْدَ أَن تُوَلُّوا مُدْبِرِينَ
Te waat naa ci Yàlla ! Ne danaa fexeel seen xërëm yi ci seen ginnaaw, bu ngeen dëddoo”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
55Aaya
Tekki — Al-Anbiya 55
Simoore Al-Anbiya Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Ndax li nga nu dig dëgg…Simoore Aaya 55/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








