Al-Anbiya · 75/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَأَدْخَلْنَاهُ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُ مِنَ الصَّالِحِينَ ۝٧٥
Wa adkhalnaahu fee rahmatinaa innahoo minas saalihee
📖 Tekkim Wolof
Dugal Nanu ko ci Sunu yërmaande. Te moom bokk na ca ñu sell ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 73-77 — Al-Anbiya

73وَجَعَلْنَاهُمْ أَئِمَّةً يَهْدُونَ بِأَمْرِنَا وَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِمْ فِعْلَ الْخَيْرَاتِ وَإِقَامَ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءَ الزَّكَاةِ ۖ وَكَانُوا لَنَا عَابِدِينَ
Def leen ay njiit yuy gindee ci Sunu ndigal. Nu soloo leen jëf yu yiw, ak taxawal julli ak génne asaka. Te ñoom daal daanañu Ma jaamu.
74وَلُوطًا آتَيْنَاهُ حُكْمًا وَعِلْمًا وَنَجَّيْنَاهُ مِنَ الْقَرْيَةِ الَّتِي كَانَت تَّعْمَلُ الْخَبَائِثَ ۗ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمَ سَوْءٍ فَاسِقِينَ
Ak Lóot ! May Nanu ko ràññee, dégg ak xam-xam, te musal Na
75وَأَدْخَلْنَاهُ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُ مِنَ الصَّالِحِينَ
Dugal Nanu ko ci Sunu yërmaande. Te moom bokk na ca ñu sell ña.
76وَنُوحًا إِذْ نَادَىٰ مِن قَبْلُ فَاسْتَجَبْنَا لَهُ فَنَجَّيْنَاهُ وَأَهْلَهُ مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Ak Nooh itam, [fàttalikul] ba mu wootee ca lu jiitu. Nu dal koy wuyyu te musaloon ko, mook njabootam, ca njàqare ju rëy ja,
77وَنَصَرْنَاهُ مِنَ الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمَ سَوْءٍ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ
te Nu dimbali woon ko ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu. Ñoom aw nit ñu bon lañu woon. Nu daldi leen labal ñoom ñépp.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Al-Anbiya 75

Simoore Al-Anbiya Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dugal Nanu ko ci Sunu yërmaande. Te moom bokk na…

Simoore Aaya 75/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers