Al-Mu'minun · 56/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
نُسَارِعُ لَهُمْ فِي الْخَيْرَاتِ ۚ بَل لَّا يَشْعُرُونَ ۝٥٦
Nusaari`u lahum fil khairaat; bal laa yash`uroon
📖 Tekkim Wolof
Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk] ? Ñoom yëguñu li xew de.

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Al-Mu'minun

54فَذَرْهُمْ فِي غَمْرَتِهِمْ حَتَّىٰ حِينٍ
Bàyyileen ci seen ngëlëmte loolu ab diir.
55أَيَحْسَبُونَ أَنَّمَا نُمِدُّهُم بِهِ مِن مَّالٍ وَبَنِينَ
Ndax dañoo jàpp ne li ñu leen may ci alal ak i doom,
56نُسَارِعُ لَهُمْ فِي الْخَيْرَاتِ ۚ بَل لَّا يَشْعُرُونَ
Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk] ? Ñoom yëguñu li xew de.
57إِنَّ الَّذِينَ هُم مِّنْ خَشْيَةِ رَبِّهِم مُّشْفِقُونَ
Ña sóobu dëgg dëgg ci ragal seen Boroom,
58وَالَّذِينَ هُم بِآيَاتِ رَبِّهِمْ يُؤْمِنُونَ
ña nga xam ne dañoo gëm seen kàdduy Boroom,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 56

Simoore Al-Mu'minun Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk]…

Simoore Aaya 56/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers