Al-Mu'minun · 65/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
لَا تَجْأَرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّكُم مِّنَّا لَا تُنصَرُونَ ۝٦٥
Laa taj`arul yawma innakum minnaa laa tunsaroon
📖 Tekkim Wolof
“Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 63-67 — Simoore Al-Mu'minun

63بَلْ قُلُوبُهُمْ فِي غَمْرَةٍ مِّنْ هَٰذَا وَلَهُمْ أَعْمَالٌ مِّن دُونِ ذَٰلِكَ هُمْ لَهَا عَامِلُونَ
Waaye seeni xol réere na lii [di Alxuraan]. Te am nañu ay jëf yu yées yooyu te ña nga koy jëf,
64حَتَّىٰ إِذَا أَخَذْنَا مُتْرَفِيهِم بِالْعَذَابِ إِذَا هُمْ يَجْأَرُونَ
ba ba ñuy mbugal seen njiit ya ñu seet seet di yuuxu walla.
65لَا تَجْأَرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّكُم مِّنَّا لَا تُنصَرُونَ
“Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.
66قَدْ كَانَتْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُمْ عَلَىٰ أَعْقَابِكُمْ تَنكِصُونَ
Samay kàddu wàccoon na ci yéen ; ngeen daan ko dummóoyu,
67مُسْتَكْبِرِينَ بِهِ سَامِرًا تَهْجُرُونَ
ngeen daan ca rëy-rëylu, di ko waxtaane”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 65

Simoore Al-Mu'minun Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.

Simoore Aaya 65/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers