Ash-Shu'ara · 101/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَلَا صَدِيقٍ حَمِيمٍ ۝١٠١
Wa laa sadeeqin hameem
📖 Tekkim Wolof
amuma it xarit bu may miisloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 99-103 — Ash-Shu'ara

99وَمَا أَضَلَّنَا إِلَّا الْمُجْرِمُونَ
Te tooñkat ya doŋŋ a nga nu sànk.
100فَمَا لَنَا مِن شَافِعِينَ
Amunu ku nu tinu,
101وَلَا صَدِيقٍ حَمِيمٍ
amuma it xarit bu may miisloo.
102فَلَوْ أَنَّ لَنَا كَرَّةً فَنَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Céy bu nu delluwaatoon àdduna, kon dananu bokk ca way-gëm ña ! ”
103إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu ; te taxut woon li ëpp ci ñoom gëm.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
101Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 101

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 101 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : amuma it xarit bu may miisloo.

Simoore Aaya 101/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 99–103. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers