Ash-Shu'ara · 100/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
فَمَا لَنَا مِن شَافِعِينَ ۝١٠٠
Famaa lanaa min shaa fi`een
📖 Tekkim Wolof
Amunu ku nu tinu,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 98-102 — Simoore Ash-Shu'ara

98إِذْ نُسَوِّيكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
jamono ya nu leen doon yemaleek Boroom àddina si.
99وَمَا أَضَلَّنَا إِلَّا الْمُجْرِمُونَ
Te tooñkat ya doŋŋ a nga nu sànk.
100فَمَا لَنَا مِن شَافِعِينَ
Amunu ku nu tinu,
101وَلَا صَدِيقٍ حَمِيمٍ
amuma it xarit bu may miisloo.
102فَلَوْ أَنَّ لَنَا كَرَّةً فَنَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Céy bu nu delluwaatoon àdduna, kon dananu bokk ca way-gëm ña ! ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
100Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 100

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amunu ku nu tinu,

Simoore Aaya 100/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers