Ash-Shu'ara · 18/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ أَلَمْ نُرَبِّكَ فِينَا وَلِيدًا وَلَبِثْتَ فِينَا مِنْ عُمُرِكَ سِنِينَ ۝١٨
Qaala alam nurabbika feenaa waleedanw wa labista feenaa min `umurika sineen
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] ne ko : “Moo ndax yarunu la fii ba nga doonee liir ? Ak li nga fi nekk lépp ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Ash-Shu'ara

16فَأْتِيَا فِرْعَوْنَ فَقُولَا إِنَّا رَسُولُ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Dem ca Firawna ne ko : “Nun ñaari ndawi Boroom àddina si lanu,
17أَنْ أَرْسِلْ مَعَنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ
Yebalal giir Banii-Israayil ñu ànd ak nun ”.
18قَالَ أَلَمْ نُرَبِّكَ فِينَا وَلِيدًا وَلَبِثْتَ فِينَا مِنْ عُمُرِكَ سِنِينَ
[Firawna] ne ko : “Moo ndax yarunu la fii ba nga doonee liir ? Ak li nga fi nekk lépp ?
19وَفَعَلْتَ فَعْلَتَكَ الَّتِي فَعَلْتَ وَأَنتَ مِنَ الْكَافِرِينَ
Ak jëf ji nga fi jëfoon tey xarabaate”
20قَالَ فَعَلْتُهَا إِذًا وَأَنَا مِنَ الضَّالِّينَ
Muusaa ne ko : “Defoon naa ko, waaye teyuma ko.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 18

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] ne ko : “Moo ndax yarunu la fii ba…

Simoore Aaya 18/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers