Ash-Shu'ara · 185/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مِنَ الْمُسَحَّرِينَ ۝١٨٥
Qaalooo innamaa anta minal musahhareen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Yaw daal ag njibar moo la ŋëb ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 183-187 — Simoore Ash-Shu'ara

183وَلَا تَبْخَسُوا النَّاسَ أَشْيَاءَهُمْ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
Buleen di ñormati ca yëfi nit ña [wattu ko] ; buleen di lawal asaru ci suuf si.
184وَاتَّقُوا الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالْجِبِلَّةَ الْأَوَّلِينَ
Nangeen ragal Yàlla mi leen sàkk, mook maas ya leen jiitu woon”.
185قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مِنَ الْمُسَحَّرِينَ
Ñu ne ko : “Yaw daal ag njibar moo la ŋëb ;
186وَمَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَإِن نَّظُنُّكَ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ
Te doo kenn ku dul nit ni nun ; nun sax foog nanu ne ci fenkat yi nga bokk.
187فَأَسْقِطْ عَلَيْنَا كِسَفًا مِّنَ السَّمَاءِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Waay-waay li nga ne su dee dëgg, rotalal ci sunu kaw ay dogiiti asamaan si ! ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
185Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 185

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 185 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Yaw daal ag njibar moo la…

Simoore Aaya 185/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 183–187. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers