Ash-Shu'ara · 184/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَاتَّقُوا الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالْجِبِلَّةَ الْأَوَّلِينَ ۝١٨٤
Wattaqul lazee khalaqakum waljibillatal awwaleen
📖 Tekkim Wolof
Nangeen ragal Yàlla mi leen sàkk, mook maas ya leen jiitu woon”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 182-186 — Simoore Ash-Shu'ara

182وَزِنُوا بِالْقِسْطَاسِ الْمُسْتَقِيمِ
bu ngeen dee màndaxe [peese], nay mat sëkk.
183وَلَا تَبْخَسُوا النَّاسَ أَشْيَاءَهُمْ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
Buleen di ñormati ca yëfi nit ña [wattu ko] ; buleen di lawal asaru ci suuf si.
184وَاتَّقُوا الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالْجِبِلَّةَ الْأَوَّلِينَ
Nangeen ragal Yàlla mi leen sàkk, mook maas ya leen jiitu woon”.
185قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مِنَ الْمُسَحَّرِينَ
Ñu ne ko : “Yaw daal ag njibar moo la ŋëb ;
186وَمَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَإِن نَّظُنُّكَ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ
Te doo kenn ku dul nit ni nun ; nun sax foog nanu ne ci fenkat yi nga bokk.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
184Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 184

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 184 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangeen ragal Yàlla mi leen sàkk, mook maas ya leen…

Simoore Aaya 184/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 182–186. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers