Ash-Shu'ara · 186/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَمَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَإِن نَّظُنُّكَ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ ۝١٨٦
Wa maaa anta illaa basharum mislunaa wa innazunnuka laminal kaazibeen
📖 Tekkim Wolof
Te doo kenn ku dul nit ni nun ; nun sax foog nanu ne ci fenkat yi nga bokk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 184-188 — Ash-Shu'ara

184وَاتَّقُوا الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالْجِبِلَّةَ الْأَوَّلِينَ
Nangeen ragal Yàlla mi leen sàkk, mook maas ya leen jiitu woon”.
185قَالُوا إِنَّمَا أَنتَ مِنَ الْمُسَحَّرِينَ
Ñu ne ko : “Yaw daal ag njibar moo la ŋëb ;
186وَمَا أَنتَ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَإِن نَّظُنُّكَ لَمِنَ الْكَاذِبِينَ
Te doo kenn ku dul nit ni nun ; nun sax foog nanu ne ci fenkat yi nga bokk.
187فَأَسْقِطْ عَلَيْنَا كِسَفًا مِّنَ السَّمَاءِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Waay-waay li nga ne su dee dëgg, rotalal ci sunu kaw ay dogiiti asamaan si ! ”
188قَالَ رَبِّي أَعْلَمُ بِمَا تَعْمَلُونَ
Suhaybu ne leen : “Sama Boroom a gën a xam li ngeen di def”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
186Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 186

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 186 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te doo kenn ku dul nit ni nun ; nun…

Simoore Aaya 186/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 184–188. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers