An-Naml · 23/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
إِنِّي وَجَدتُّ امْرَأَةً تَمْلِكُهُمْ وَأُوتِيَتْ مِن كُلِّ شَيْءٍ وَلَهَا عَرْشٌ عَظِيمٌ ۝٢٣
Innee wajattum ra atan tamlikuhum wa ootiyat min kulli shai`inw wa lahaa `arshun `azeem
📖 Tekkim Wolof
Fekk naa leen ñu am buur bu jigéen, am na lépp, am it gàngunaay gu rëy.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore An-Naml

21لَأُعَذِّبَنَّهُ عَذَابًا شَدِيدًا أَوْ لَأَذْبَحَنَّهُ أَوْ لَيَأْتِيَنِّي بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Danaa ko mbugal mbugal mu tar ! Walla ma rendi ko ! Walla mu indil ma lay wu wér”.
22فَمَكَثَ غَيْرَ بَعِيدٍ فَقَالَ أَحَطتُ بِمَا لَمْ تُحِطْ بِهِ وَجِئْتُكَ مِن سَبَإٍ بِنَبَإٍ يَقِينٍ
Mu sax fa tuuti, [picc] ma dellusi ne ko : “Xam naa loo xamul te indil naa la xibaar bu wóor bu bawoo réewum Sabaa” :
23إِنِّي وَجَدتُّ امْرَأَةً تَمْلِكُهُمْ وَأُوتِيَتْ مِن كُلِّ شَيْءٍ وَلَهَا عَرْشٌ عَظِيمٌ
Fekk naa leen ñu am buur bu jigéen, am na lépp, am it gàngunaay gu rëy.
24وَجَدتُّهَا وَقَوْمَهَا يَسْجُدُونَ لِلشَّمْسِ مِن دُونِ اللَّهِ وَزَيَّنَ لَهُمُ الشَّيْطَانُ أَعْمَالَهُمْ فَصَدَّهُمْ عَنِ السَّبِيلِ فَهُمْ لَا يَهْتَدُونَ
Fekk naa ko it mook aw nitam ñuy jaamu jant bi bàyyi Yàlla. Séytaane taaralal leen jëf jooju, wëlbati leen ñu dëddu yoonu Yàlla ba gëmuñu.
25أَلَّا يَسْجُدُوا لِلَّهِ الَّذِي يُخْرِجُ الْخَبْءَ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَيَعْلَمُ مَا تُخْفُونَ وَمَا تُعْلِنُونَ
Moo ndax duñu jaamu Yàlla Miy génne li nëbbu ci asamaan yeek suuf si, te Moo xam li ngeen di nëbb ak li ngeen di feeñal ?
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — An-Naml 23

Simoore An-Naml Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fekk naa leen ñu am buur bu jigéen, am na…

Simoore Aaya 23/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers