An-Naml · 78/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
إِنَّ رَبَّكَ يَقْضِي بَيْنَهُم بِحُكْمِهِ ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْعَلِيمُ ٧٨
Transliteration
Inna Rabbaka yaqdee bainahum bihukmih; wa Huwal `Azeezul `Aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom dana àtte seen diggante ci àtteem yi ; Mooy Boroom kàttan ga, di Ku xam.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 76-80 — An-Naml
76إِنَّ هَٰذَا الْقُرْآنَ يَقُصُّ عَلَىٰ بَنِي إِسْرَائِيلَ أَكْثَرَ الَّذِي هُمْ فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Alxuraan jii dafay nettali ci giir Bani-Israayiila, li ëpp ci la ñu daan juuyoo ak a wuute,
77وَإِنَّهُ لَهُدًى وَرَحْمَةٌ لِّلْمُؤْمِنِينَ
Te Alxuraan jooju njub la ak yërmaande ci képp ku gëm [di ab jullit].
78إِنَّ رَبَّكَ يَقْضِي بَيْنَهُم بِحُكْمِهِ ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْعَلِيمُ
Sa Boroom dana àtte seen diggante ci àtteem yi ; Mooy Boroom kàttan ga, di Ku xam.
79فَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۖ إِنَّكَ عَلَى الْحَقِّ الْمُبِينِ
[Yaw Muhammad], nanga wéeru ci Yàlla, [te xamal it ne] yaa ngi ci dëgg gu bir.
80إِنَّكَ لَا تُسْمِعُ الْمَوْتَىٰ وَلَا تُسْمِعُ الصُّمَّ الدُّعَاءَ إِذَا وَلَّوْا مُدْبِرِينَ
Mënoo tax ku xas a dee ba noppi di dekki, mënoo tax it ab tëx dégg woote ba, saa su la wonee ginnaaw dummóoyu.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
78Aaya
Tekki — An-Naml 78
Simoore An-Naml Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom dana àtte seen diggante ci àtteem yi ;…Simoore Aaya 78/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








