Al-Qasas · 69/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَرَبُّكَ يَعْلَمُ مَا تُكِنُّ صُدُورُهُمْ وَمَا يُعْلِنُونَ ۝٦٩
Wa Rabbuka ya`lamu maa tukinnu sudooruhum wa maa yu`linoon
📖 Tekkim Wolof
Te it sa Boroom a xam li seeni xol nëbb ak li ñuy feeñal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Simoore Al-Qasas

67فَأَمَّا مَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَعَسَىٰ أَن يَكُونَ مِنَ الْمُفْلِحِينَ
Képp ku ca tuub te gëm te jëf u yiw, amaana mu texe.
68وَرَبُّكَ يَخْلُقُ مَا يَشَاءُ وَيَخْتَارُ ۗ مَا كَانَ لَهُمُ الْخِيَرَةُ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Te sa Boroom mooy sàkk lu ko soob te neex ko ; ñoom amuñu coppan. Tudd naa sellug Yàlla ! Te kawe na lool ci la ñuy bokkaale !
69وَرَبُّكَ يَعْلَمُ مَا تُكِنُّ صُدُورُهُمْ وَمَا يُعْلِنُونَ
Te it sa Boroom a xam li seeni xol nëbb ak li ñuy feeñal.
70وَهُوَ اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ لَهُ الْحَمْدُ فِي الْأُولَىٰ وَالْآخِرَةِ ۖ وَلَهُ الْحُكْمُ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Te Moom mooy Yàlla te amul jeneen yàlla ju dul Moom. Moo moom xeeti cant yépp cig njalbéen ba cig mujj. Te Moo moom àtte ya. Te ca Moom lañu di delloo ñépp.
71قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِن جَعَلَ اللَّهُ عَلَيْكُمُ اللَّيْلَ سَرْمَدًا إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ مَنْ إِلَٰهٌ غَيْرُ اللَّهِ يَأْتِيكُم بِضِيَاءٍ ۖ أَفَلَا تَسْمَعُونَ
Neel : “Xanaa gisuleen ne bu Yàlla defoon guddi gi muy lu sax ba Bis-pénc ba, ana jan yàlla ju dul Moom moo leen di indil ag leer ? Moo ndax dungeen dégg ? ”
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Al-Qasas 69

Simoore Al-Qasas Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it sa Boroom a xam li seeni xol nëbb…

Simoore Aaya 69/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers