Aali Imran · 44/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
ذَٰلِكَ مِنْ أَنبَاءِ الْغَيْبِ نُوحِيهِ إِلَيْكَ ۚ وَمَا كُنتَ لَدَيْهِمْ إِذْ يُلْقُونَ أَقْلَامَهُمْ أَيُّهُمْ يَكْفُلُ مَرْيَمَ وَمَا كُنتَ لَدَيْهِمْ إِذْ يَخْتَصِمُونَ ۝٤٤
Zaalika min ambaaa`il ghaibi nooheehi ilaik; wa maa kunta ladaihim iz yulqoona aqlaamahum ayyuhum yakfulu Maryama wa maa kunta ladaihim iz yakhtasimoon
📖 Tekkim Wolof
- Loolu bokk na ca xibaar ya nekkoon kumpa, Nu ngi la koy xamal. Te neewuloo woon ba ñuy sànni bantu wantaloo ya di seet kan mooy yor Maryaama ! Te neewuloo woon ba ñuy xulloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore Aali Imran

42وَإِذْ قَالَتِ الْمَلَائِكَةُ يَا مَرْيَمُ إِنَّ اللَّهَ اصْطَفَاكِ وَطَهَّرَكِ وَاصْطَفَاكِ عَلَىٰ نِسَاءِ الْعَالَمِينَ
(Fàttalikul) ba Malaaka ya waxee ne : “Yaw Maryaama, Yàlla tànn na la te laabal na la, tànn na la ci kaw jigéeni àddina bi yépp.
43يَا مَرْيَمُ اقْنُتِي لِرَبِّكِ وَاسْجُدِي وَارْكَعِي مَعَ الرَّاكِعِينَ
“Yaw Maryaama, jaamul sa Boroom, nanga sujjóot te rukkoo ànd ak ñay rukkoo [di julli]”
44ذَٰلِكَ مِنْ أَنبَاءِ الْغَيْبِ نُوحِيهِ إِلَيْكَ ۚ وَمَا كُنتَ لَدَيْهِمْ إِذْ يُلْقُونَ أَقْلَامَهُمْ أَيُّهُمْ يَكْفُلُ مَرْيَمَ وَمَا كُنتَ لَدَيْهِمْ إِذْ يَخْتَصِمُونَ
- Loolu bokk na ca xibaar ya nekkoon kumpa, Nu ngi la koy xamal. Te neewuloo woon ba ñuy sànni bantu wantaloo ya di seet kan mooy yor Maryaama ! Te neewuloo woon ba ñuy xulloo.
45إِذْ قَالَتِ الْمَلَائِكَةُ يَا مَرْيَمُ إِنَّ اللَّهَ يُبَشِّرُكِ بِكَلِمَةٍ مِّنْهُ اسْمُهُ الْمَسِيحُ عِيسَى ابْنُ مَرْيَمَ وَجِيهًا فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ وَمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
(Fàttalikul,) ba Malaaka ya waxee ne : "Yaw Maryaama, Yàllaa ngi lay bégal ci kàddu [doom] gu tukkee ca Moom : turam moo di “Al-Masiihu” “Iisaa”, doomu Maryam, boroom bayre ci àddina ak ca àllaaxira, te bokk na ca way-jege ña Boroom bi”.
46وَيُكَلِّمُ النَّاسَ فِي الْمَهْدِ وَكَهْلًا وَمِنَ الصَّالِحِينَ
Te dana wax ak nit ñi, bi mu doonee liir ak bu doonee mag te bokk na ca nit ñu yiw ña”.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
44Aaya

Tekki — Aali Imran 44

Simoore Aali Imran Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Loolu bokk na ca xibaar ya nekkoon kumpa, Nu…

Simoore Aaya 44/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers