Aali Imran · 83/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
أَفَغَيْرَ دِينِ اللَّهِ يَبْغُونَ وَلَهُ أَسْلَمَ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ طَوْعًا وَكَرْهًا وَإِلَيْهِ يُرْجَعُونَ ۝٨٣
Afaghaira deenil laahi yabghoona wa lahooo aslama man fis samaawaati wal ardi taw`anw wa karhanw wa ilaihi yurja`oon
📖 Tekkim Wolof
Ndax dañuy sàkku jeneen diine ju bokkul ak diiney Yàlla ji, te waa asamaan si ak suuf si ci Moom lañu jëm, moo xam muy coobare wallag noteel, te lu mën a xew ca Moom lañuy dellu ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 81-85 — Aali Imran

81وَإِذْ أَخَذَ اللَّهُ مِيثَاقَ النَّبِيِّينَ لَمَا آتَيْتُكُم مِّن كِتَابٍ وَحِكْمَةٍ ثُمَّ جَاءَكُمْ رَسُولٌ مُّصَدِّقٌ لِّمَا مَعَكُمْ لَتُؤْمِنُنَّ بِهِ وَلَتَنصُرُنَّهُ ۚ قَالَ أَأَقْرَرْتُمْ وَأَخَذْتُمْ عَلَىٰ ذَٰلِكُمْ إِصْرِي ۖ قَالُوا أَقْرَرْنَا ۚ قَالَ فَاشْهَدُوا وَأَنَا مَعَكُم مِّنَ الشَّاهِدِينَ
Fàttalikul ba Yàlla kóllaranteek Yonent ya : ba mu leen joxee Téere ak xam-xamu ràññee, [mu ne]: “Su leen ab Yonent dikkalee buy dëggal li ngeen yor, nangeen ko topp te dimbali ko.”. Mu ne leen [Moom Yàlla] : “Ndax nangu ngeen loolu ? Te nangeen jàpp ci loolu Sama kóllare ” - Ñu ne : “Nangu nanu”. Yàlla ne leen : “Seedeleen te nanga ànd ak yéene bokk ca way-seede ya.
82فَمَن تَوَلَّىٰ بَعْدَ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَاسِقُونَ
Ku dummóoyu ginnaaw loolu... ñooña ñoo sàqi ndigal”.
83أَفَغَيْرَ دِينِ اللَّهِ يَبْغُونَ وَلَهُ أَسْلَمَ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ طَوْعًا وَكَرْهًا وَإِلَيْهِ يُرْجَعُونَ
Ndax dañuy sàkku jeneen diine ju bokkul ak diiney Yàlla ji, te waa asamaan si ak suuf si ci Moom lañu jëm, moo xam muy coobare wallag noteel, te lu mën a xew ca Moom lañuy dellu ?
84قُلْ آمَنَّا بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ عَلَيْنَا وَمَا أُنزِلَ عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْمَاعِيلَ وَإِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ وَالْأَسْبَاطِ وَمَا أُوتِيَ مُوسَىٰ وَعِيسَىٰ وَالنَّبِيُّونَ مِن رَّبِّهِمْ لَا نُفَرِّقُ بَيْنَ أَحَدٍ مِّنْهُمْ وَنَحْنُ لَهُ مُسْلِمُونَ
Neel : “Gëm nanu Yàlla, li ñu wàcce ci nun, li ñu wàcce ci Ibraahiima, ak Ismaahiila, ak Yanqooba, ak ca sët ya, ak la ñu joxoon Muusaa ak Iisaa ak Yonent ya, mu tukkee ca seen Boroom [Téere ya]: dunu téqale kenn ci ñoom te nun way-wommatu lañu [jébbulu] jëm ci Yàlla”.
85وَمَن يَبْتَغِ غَيْرَ الْإِسْلَامِ دِينًا فَلَن يُقْبَلَ مِنْهُ وَهُوَ فِي الْآخِرَةِ مِنَ الْخَاسِرِينَ
Kuy sàkku diine ju dul Lislaam, deesu ko nangul, te bu àllaaxiraa, ca way-ñàkk ña lay bokk.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
83Aaya

Tekki — Aali Imran 83

Simoore Aali Imran Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax dañuy sàkku jeneen diine ju bokkul ak diiney Yàlla…

Simoore Aaya 83/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers